Portail - Index - FAQ - Search - Membres - Groupes - Register - Messages Privés - Log in
View unanswered posts
Qui est en ligne?
Who is Online

  [ Administrator ]   [ Moderator ]
Most users ever online was 324 on Fri 1 Nov 2019 - 09:47


 BIENVENUE ET MERCI POUR VOTRE VISITE 
Cliquer ici pour vous inscrire sur votre forum Smile
DECEPTION QUE FAIRE
Goto page: 1, 2  >
 
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Discussions Générales
Previous topic :: Next topic  
Author Message
RAFETTNA
Membre de base
Membre de base

Offline

Joined: 02 Apr 2010
Posts: 222
Anniversaire: 17 octobre
Genre: Femme
Localisation: sans dom fix
Point(s): 334
Moyenne de points: 1.50

PostPosted: Wed 24 Aug 2011 - 20:49    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

PublicitéSupprimer les publicités ?
Mane dal je pense que khawma sama dieukeur Dékétéyo lima guena bagne défaut boboula ammé il est sale en un mot je narrive plus à le digérer pourtant j'essai de lui ouvrir les yeux en lui achetant des brosses à dent parfum et autre mais djikou akk borom juskà la tombe
______________________________
L'amitié finit parfois en amour, mais rarement l'amour en amitié.


Last edited by RAFETTNA on Fri 26 Aug 2011 - 08:26; edited 1 time in total
Back to top
Dibor
vip
vip

Offline

Joined: 22 Oct 2005
Posts: 3,868
Anniversaire: 31 Août
Genre: Femme
Localisation: Teussland
Point(s): 6,767
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Wed 24 Aug 2011 - 20:53    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote


Balema dé tayoumako!
Diapaléko mou sét sey diapanetéla.
______________________________


Back to top
RAFETTNA
Membre de base
Membre de base

Offline

Joined: 02 Apr 2010
Posts: 222
Anniversaire: 17 octobre
Genre: Femme
Localisation: sans dom fix
Point(s): 334
Moyenne de points: 1.50

PostPosted: Wed 24 Aug 2011 - 21:05    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

yow tamm dibor serrer diapaléwoma Mr. Green Mr. Green
______________________________
L'amitié finit parfois en amour, mais rarement l'amour en amitié.


Back to top
Madame 0
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 03 May 2010
Posts: 3,383
Anniversaire: 29fevrier
Genre: Femme
Localisation: rue
Point(s): 5,219
Moyenne de points: 1.54

PostPosted: Wed 24 Aug 2011 - 23:08    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

massa 3fois


dina la nianal


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 00:12    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

aaaaaannh ?? !! Laughing
waw yow rafetena xana vous ne vous embrassiez pas avant k il ne t epouse ? si wi kone niak gua setlou...
 olof Ndiaye nena lou am thia sey ba rek nouyo na thia ngora ba.

legui D key sangue , xam gua goor gni ay bb lagnu ,  wala bok...
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
nounouche
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 8,613
Anniversaire: 19 septembre
Genre: Femme
Localisation: mbeuleukhé
Point(s): 13,877
Moyenne de points: 1.61

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 00:35    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

Rafetna do bayi ba koor gui diekh ma soga tontou  Laughing
______________________________


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 07:56    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

lii dé mo takh mag gni, so wakhé wakhou seuy gnounila "néég dafa khat"
Rafet, djappaléko rek ("je ne peux mm plus m'approcher de lui il m dégoute" rek moma thi djakhal)

sama gaayi gnom bougnouy ngoroyo dagnouy sangou, di parfuméwou, di yeuy chingom, di mathie menthe fraîche
sougnou také nak, dellou thia "tilim-eunn-forokh"
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
Guest
Guest

Offline




PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 12:28    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

nounouche wrote:
Rafetna do bayi ba koor gui diekh ma soga tontou  Laughing


OUstaze neena:
Loo roussa def ci koor,
Rousskaadef ganaaw koor.


Back to top
Dibor
vip
vip

Offline

Joined: 22 Oct 2005
Posts: 3,868
Anniversaire: 31 Août
Genre: Femme
Localisation: Teussland
Point(s): 6,767
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 12:46    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

Mme gua balema wayé yawit diongué woulo dara! déko dieudal ay gels de bains diko invité sanguou, bou fékéné bou léké dafay tayal diogue brossou après repas outal sa cuvette ak foy déf ndokh gneuw talalekoko ak brossam ak dentifrice di diondjieu tankhyi outalko déodorant tu fais comme si daguay nék à ses petits soins et tu le façonnes à ta guise lady néna ay bb lagne. Boufékéné dal taiméguako réellement il est possible de sauver les meubles.
 
______________________________


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 12:50    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

thiey dibor !

naka koor gui ?
nuyulma sa gnari bb yi

______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
RAFETTNA
Membre de base
Membre de base

Offline

Joined: 02 Apr 2010
Posts: 222
Anniversaire: 17 octobre
Genre: Femme
Localisation: sans dom fix
Point(s): 334
Moyenne de points: 1.50

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 13:00    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

Dibor wrote:

Mme gua balema wayé yawit diongué woulo dara! déko dieudal ay gels de bains diko invité sanguou, bou fékéné bou léké dafay tayal diogue brossou après repas outal sa cuvette ak foy déf ndokh gneuw talalekoko ak brossam ak dentifrice di diondjieu tankh
yi outalko déodorant tu fais comme si daguay nék à ses petits soins et tu le façonnes à ta guise lady néna ay bb lagne. Boufékéné dal taiméguako réellement il est possible de sauver les meubles.
 


j'ai essayé de faire tout ça mé bolenndi vivre à l'extérieur boulot cuisine travaux maison je nai pa le tps de
m'occuper de lui wayé nakk dégg na say cons dibor dina guena deff effort
comme le dit un proverbe bo divorcer parcek sa dieukeur day saw lal diga amm kouy poubb lale

______________________________
L'amitié finit parfois en amour, mais rarement l'amour en amitié.


Back to top
KANIBOUSAF
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 17 Feb 2008
Posts: 9,627
Anniversaire: 01/03
Genre: Homme
Localisation: Dakar
Point(s): 15,144
Moyenne de points: 1.57

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 15:00    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

kone dé djiapal, balla guay am kouye poubb lale

Mercy wrote:

aaaaaannh ?? !! Laughing
waw yow rafetena xana vous ne vous embrassiez pas avant k il ne t epouse ? si wi kone niak gua setlou...
 olof Ndiaye nena lou am thia sey ba rek nouyo na thia ngora ba.

legui D key sangue , xam gua goor gni ay bb lagnu ,  wala bok...

Shocked Shocked Shocked kharal ma nopi sakh dakh dama wor

mais khalébi yamoulo dé

______________________________
LES ENFANTS ONT PLUS BESOIN DE MODELES QUE DE CRITIQUES



Le Prophéte a dit : "Maintiens le lien avec celui qui te fuit, sois bon avec celui qui t'a causé du tort, et dis la vérité même si elle est à ton détriment."


Hadith - Ibn An-Najjar


Back to top
nounouche
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 8,613
Anniversaire: 19 septembre
Genre: Femme
Localisation: mbeuleukhé
Point(s): 13,877
Moyenne de points: 1.61

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 16:08    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

Anonymous wrote:

nounouche wrote:
Rafetna do bayi ba koor gui diekh ma soga tontou  Laughing



OUstaze neena:
Loo roussa def ci koor,
Rousskaadef ganaaw koor.
invité mane awma loumey rouss wala di ko ragal ndax jaam kessé lay wax...c t juste une boutade..
bayilen di sole cagoule bolen di agressé niit yi...solen gnéméwoul li nguène di wax nguène nopi...
______________________________


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 16:15    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

waw kii dou TataNounchy ?
naka kor gui ?
mba ya ngi may fassalé ci nafila yi ak kourouss gui ?
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
elpaix
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 17,970
Anniversaire: 10/05
Localisation: Athépédie
Point(s): 30,088
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 16:44    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

Rafetna, il faut :
- un rdv chez le dentiste
- outal ko ay sous-vêtements
- stick déodorant
- ndél ko si souf
- et comme dit dibor, diko sangueu


tilim mom, bakhoul ci gor bakhoul ci djiguène
______________________________


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 18:02    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

c vrai kil devrai aller voir un dentiste parck am na xetou guemign yo xam ni febar la d.


plato wrote:
lii dé mo takh mag gni, so wakhé wakhou seuy gnounila "néég dafa khat" Rafet, djappaléko rek ("je ne peux mm plus m'approcher de lui il m dégoute" rek moma thi djakhal)

sama gaayi gnom bougnouy ngoroyo dagnouy sangou, di parfuméwou, di yeuy chingom, di mathie menthe fraîche
sougnou také nak, dellou thia "tilim-eunn-forokh"




aka di deug, daniou ley neub sene bop
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
OTIS
Dj FS
Dj FS

Offline

Joined: 27 Oct 2005
Posts: 8,273
Anniversaire: 01/06
Genre: Homme
Point(s): 11,662
Moyenne de points: 1.41

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 18:14    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

elpaix wrote:
- ndél ko si souf


______________________________
Visitez le blog d'Otis
... les billets d'Otis
"La véritable musique est le silence, les notes ne font qu'encadrer ce silence" Miles Davis


Back to top
elpaix
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 17,970
Anniversaire: 10/05
Localisation: Athépédie
Point(s): 30,088
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Thu 25 Aug 2011 - 22:48    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

Dj, wori nga
______________________________


Back to top
RAFETTNA
Membre de base
Membre de base

Offline

Joined: 02 Apr 2010
Posts: 222
Anniversaire: 17 octobre
Genre: Femme
Localisation: sans dom fix
Point(s): 334
Moyenne de points: 1.50

PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 14:33    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

liguenn thi khamoul moy 
pétééééééé toute la nuit Mr. Green Mr. Green Mr. Green

______________________________
L'amitié finit parfois en amour, mais rarement l'amour en amitié.


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 14:56    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

rafetna ya xoromou d... Laughing
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 15:08    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

RAFETTNA wrote:
liguenn thi khamoul moy 
pétééééééé toute la nuit Mr. Green Mr. Green Mr. Green

mauvaise haleine + flatulences : il peut s'agir de problèmes gastriques

Il faut qu'il aille voir un spécialiste de la médecine interne. Il y a des chances que ça règle une partie du problème.
Ensuite nga kay bichonner comme dit Dibor.
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
FS
Guest

Offline




PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 16:16    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

RAFETTNA wrote:
liguenn thi khamoul moy {{{Spoiler}}}
Li d dou se thieur Neutral

Back to top
Guest
Guest

Offline




PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 21:38    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

RAFETTNA wrote:
liguenn thi khamoul moy {{{Spoiler}}}









si si worina kham na ko kou lire li sakh worigua


Back to top
Dibor
vip
vip

Offline

Joined: 22 Oct 2005
Posts: 3,868
Anniversaire: 31 Août
Genre: Femme
Localisation: Teussland
Point(s): 6,767
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 23:21    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

fi amoul béne sérieux! mba doko ndambél ak akara bou baré?
______________________________


Back to top
Dibor
vip
vip

Offline

Joined: 22 Oct 2005
Posts: 3,868
Anniversaire: 31 Août
Genre: Femme
Localisation: Teussland
Point(s): 6,767
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Fri 26 Aug 2011 - 23:23    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE Reply with quote

plato wrote:

thiey dibor !

{{{Spoiler}}}
Pla bou ndawbi néna gua boléko si douhas khiyamou léyli yiguay déf!
______________________________


Back to top
Contenu Sponsorisé






PostPosted: Today at 22:08    Post subject: DECEPTION QUE FAIRE

Back to top
Display posts from previous:   
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Discussions Générales
All times are GMT
Goto page: 1, 2  >
Page 1 of 2

 
Jump to:  

Portal | Index | Create a forum | Free support forum | Free forums directory | Report a violation | Conditions générales d'utilisation
Powered by phpBB
Appalachia Theme © 2002 Droshi's Island

Designed & images by Kooky