Portail - Index - FAQ - Search - Membres - Groupes - Register - Messages Privés - Log in
View unanswered posts
Qui est en ligne?
Who is Online

  [ Administrator ]   [ Moderator ]
Most users ever online was 324 on Fri 1 Nov 2019 - 09:47


 BIENVENUE ET MERCI POUR VOTRE VISITE 
Cliquer ici pour vous inscrire sur votre forum Smile
loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit
Goto page: 1, 2, 3, 4  >
 
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Divertissement
Previous topic :: Next topic  
Author Message
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:15    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

PublicitéSupprimer les publicités ?


lii dé dafa am fouma ko foré...mani nako indi fi gnou waxtane si...


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:18    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

pe Mr. Green
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:20    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

CristaLady wrote:
pe Mr. Green
ah wi
koon yaay pé thi awo yi gnarél yi yobou sén fit?

ana Euminteu? Am na kou beug djeul sa palass dé! dawsil gaaw.
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:24    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

yow balla guey dieki niou waxati sa bopp nak, ba aminatou fekk lafi ci souba ba tey yagui koy diokass faler woula
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
Dibor
vip
vip

Offline

Joined: 22 Oct 2005
Posts: 3,868
Anniversaire: 31 Août
Genre: Femme
Localisation: Teussland
Point(s): 6,767
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:29    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

Yaw meuno bayi wakhi awo ak gnarél té khameni adouna dou yague bagua ame gnarél! sone si yaw
______________________________


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:41    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

idiaaa Shocked
man dé kouma wakhoon lii ma djéngou

sama bénn waay bou takk gnarél dé temps yi awo baa ngi koy yakk lou melni khémé
genre "khamn ngani moss sa khél waroon na nékk thi lidjeunti yénn yi balaa nga wout gnarél (keur, etc....)"

fékk fan yé thi guinaw waadji sms ma nima "serigne bi dolli nama kénn"
ma wooko niko "waw, noumou démé"
mounima "maako lidjeunti wayé ...............blablabla........................"

goor gniiiiiiiiiiiiiii
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
magic
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 2,356
Anniversaire: 13/04
Genre: Homme
Localisation: SLF
Point(s): 4,364
Moyenne de points: 1.85

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:43    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

Dibor wrote:
Yaw meuno bayi wakhi awo ak gnarél té khameni adouna dou yague bagua ame gnarél! sone si yaw
Adouna mo goudeu tanke Mr. Green
______________________________
Nous n'oublierons jamais...


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:49    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

plato xana yaw la dibor di waxal....boulko tontou dé...bayiko mou teudiou si négueum...

Back to top
Aminatou
Légende
Légende

Offline

Joined: 19 Nov 2005
Posts: 5,038
Anniversaire: 05/06
Genre: Femme
Point(s): 9,521
Moyenne de points: 1.89

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 12:57    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

pffffffffffffffffffffffffffffffffffff
______________________________
smile and be happy!carpe diem


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 13:09    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

khéh khéh khééééh khéééh téy mou nékh dé  
______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
maeva
vip
vip

Offline

Joined: 24 Apr 2007
Posts: 3,836
Anniversaire: 30/11
Genre: Femme
Localisation: Epicurie
Point(s): 6,402
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 13:33    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

kham na ni warr ngene bayi sujet Ndokhou rakhassou yi dal ! Ichhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh Evil or Very Mad Evil or Very Mad
______________________________
La violence : une force faible.[Vladimir Jankélévitch]


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 13:34    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

moooo
______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
4ever
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 23 Oct 2005
Posts: 7,563
Genre: Homme
Point(s): 12,801
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 13:53    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

ñaaréél dé day bari salañ salañ moom
té comme "lu bééss yééssal" doxaliin yu yàgg yi nekkon ci keur gui, moo tax fitou aawo yi di dém té du délssééti

waa F.A.P buleen ma döör dé, damay yeungueul rek , dagn ma mandaté  Mr. Green

______________________________
Way, Wey


Back to top
Dibor
vip
vip

Offline

Joined: 22 Oct 2005
Posts: 3,868
Anniversaire: 31 Août
Genre: Femme
Localisation: Teussland
Point(s): 6,767
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 14:20    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

magic wrote:

Dibor wrote:
Yaw meuno bayi wakhi awo ak gnarél té khameni adouna dou yague bagua ame gnarél! sone si yaw

Adouna mo goudeu tanke Mr. Green
Hé boy koy wakhal Question
______________________________


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 15:08    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

dibor boul nappe boy bi nak ! ich
______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
KANIBOUSAF
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 17 Feb 2008
Posts: 9,627
Anniversaire: 01/03
Genre: Homme
Localisation: Dakar
Point(s): 15,144
Moyenne de points: 1.57

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 15:50    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

c'est à cause de l'hypocrisie de certains hommes ki lé négligent aprés un deuxiéme mariage Evil or Very Mad
______________________________
LES ENFANTS ONT PLUS BESOIN DE MODELES QUE DE CRITIQUES



Le Prophéte a dit : "Maintiens le lien avec celui qui te fuit, sois bon avec celui qui t'a causé du tort, et dis la vérité même si elle est à ton détriment."


Hadith - Ibn An-Najjar


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 15:54    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

mane dé bokouma thi goor niognou mom ich
______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
miss tama
Légende
Légende

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 5,032
Localisation: Dakar
Point(s): 9,043
Moyenne de points: 1.80

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:01    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

wadji dafa done expliker ke depuis bi mou takké gnarèl , awo bi souy diw mbourou ak chocolat wala beurre, niari coté yeup lay diw, sou done dieul 2 sucres pour le ndeki 4 lay deff, lait aussi mou doublé cuillérées yi!! sakkou thieb mome le 15 mou diekh alors ke dafa donne dèm ba fin du mois ak lou toppa! ba paré di ko ci téggal dou da ko meune rekk!!!!
wadji dé dafa moudié bayi niarèl bi!!!
alors pourkoi se compliker la vie!!! mane mome arbitre la! je ne suis pas concernée nak!

______________________________
Que la force me soit donnée de supporter ce qui ne peut être changé et le courage de changer ce qui peut l'être mais aussi la sagesse de distinguer l'un de l'autre. Marc Aurèle


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:08    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

maeva wrote:
kham na ni warr ngene bayi sujet Ndokhou rakhassou yi dal ! Ichhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh Evil or Very Mad Evil or Very Mad


Aminatou wrote:
pffffffffffffffffffffffffffffffffffff




kékh kékh kékh...mane dé damako for rék...bouléne massi xass bok


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:14    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

Kanibousaf wrote:
c'est à cause de l'hypocrisie de certains hommes ki lé négligent après un deuxième mariage Evil or Very Mad


Deug gou wér !!
Je dis souvent aux amis que "takku dënn", ce n'est pas seulement des biens matériels qu'on donne à une awo comme lot de consolation. Il s'agit aussi d'avoir un comportement qui permette à la dame de rester sereine, manam dalal khélam ba fitam bagna reuthie.

thiey lii thi théorie

______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:14    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

miss tama wrote:
wadji dafa done expliker ke depuis bi mou takké gnarèl , awo bi souy diw mbourou ak chocolat wala beurre, niari coté yeup lay diw, sou done dieul 2 sucres pour le ndeki 4 lay deff, lait aussi mou doublé cuillérées yi!! sakkou thieb mome le 15 mou diekh alors ke dafa donne dèm ba fin du mois ak lou toppa! ba paré di ko ci téggal dou da ko meune rekk!!!!
wadji dé dafa moudié bayi niarèl bi!!!
{{{Spoiler}}}


n iaw!!
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
magic
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 2,356
Anniversaire: 13/04
Genre: Homme
Localisation: SLF
Point(s): 4,364
Moyenne de points: 1.85

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:40    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

miss tama wrote:
wadji dafa done expliker ke depuis bi mou takké gnarèl , awo bi souy diw mbourou ak chocolat wala beurre, niari coté yeup lay diw, sou done dieul 2 sucres pour le ndeki 4 lay deff, lait aussi mou doublé cuillérées yi!! sakkou thieb mome le 15 mou diekh alors ke dafa donne dèm ba fin du mois ak lou toppa! ba paré di ko ci téggal dou da ko meune rekk!!!! wadji dé dafa moudié bayi niarèl bi!!!
{{{Spoiler}}}




Awo bi, fair play woul dé Mr. Green
en plus xew xéwi ayoul koi n'est ce pas
nagnou bayi gneup siiw koi
le partage c'est une valeur bien de chez nous
pensez à vos soeurs yi tiolé
en plus personne n y perd,
awo bi elle gagne 50% de temps de repos (bargain )

Pour revenir au sujet, et être plus sérieux une Awo, en tout cas une vraie Force tranquille la wara done
c'est pas une petite dernière sortie de la clandestinité qui doit l'ébranler
______________________________
Nous n'oublierons jamais...


Back to top
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:48    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

magic wrote:

c'est pas une petite dernière sortie de la clandestinité qui doit l'ébranler

idié

yow aminatou maeva ak dibor dina niou la decoré
______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:49    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

aminta kagne ak dibor ak maeva...interdire naléne sama sujet ndokhoum raxassou bou saf bii...té néke d'actualité...

Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Wed 14 Jan 2009 - 16:51    Post subject: loutax awo yi gnarél yi yobou séne fit Reply with quote

diadieuf waay magic

Awo bourou keureum!
Genrou mayéwa bi tém gnouni leu "temps wou bour khéwi na!"
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
Display posts from previous:   
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Divertissement
All times are GMT
Goto page: 1, 2, 3, 4  >
Page 1 of 4

 
Jump to:  

Portal | Index | Create a forum | Free support forum | Free forums directory | Report a violation | Cookies | Charte | Conditions générales d'utilisation
Powered by phpBB
Appalachia Theme © 2002 Droshi's Island

Designed & images by Kooky