Portail - Index - FAQ - Search - Membres - Groupes - Register - Messages Privés - Log in
View unanswered posts
Qui est en ligne?
Who is Online

  [ Administrator ]   [ Moderator ]
Most users ever online was 205 on Mon 16 Sep 2019 - 14:25


 BIENVENUE ET MERCI POUR VOTRE VISITE 
Cliquer ici pour vous inscrire sur votre forum Smile
diongué goor
Goto page: 1, 2, 3, 4, 5, 6, 7, 8, 9  >
 
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Société -> Le coin des femmes
Previous topic :: Next topic  
Author Message
Lady S
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 10 May 2007
Posts: 12,438
Anniversaire: 13 / 05
Genre: Femme
Localisation: RuE de L'AmOur
Point(s): 20,976
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Mon 17 Nov 2008 - 23:41    Post subject: diongué goor Reply with quote

PublicitéSupprimer les publicités ?
yene goor gni kome k amou lene coin bouniou lene attribuel ,j vous invite a m repondre ci sounou coin bi


mane d dama done taxawalou kome d habitude rek... deg niou nane "diongue goor ak diogue djiguene bokoul ,dayeur sax goor deug bouy aborder djiguene douko songue directemen ... ci diongue bi la bokk"

waw bo songoul xale bi noy def?

legui ma lene done lath diongue goor mome naka la?

yene goor gni nane guene di diongue?

lane moy seni feme?


tey rek lay xam guerrier yi deug fs... Laughing saboter guene niou ba sone nak fexel lene ba tontou ma , koufi HS ma presenter sama lettre de demission waw
euy mane xaral ma teudi walay...

______________________________
AL HAMDOULILAHI Ala Kouli Hal.
Force-Respect-Humilité.
le pire defaut de celui qui pense etre futé est de croire que les autres sont stupides
-------------------------------------------
..♥♥♥♥♥♥.............. just make life easier Wink


Last edited by Lady S on Tue 18 Nov 2008 - 15:13; edited 1 time in total
Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 08:33    Post subject: diongué goor Reply with quote

khanaa seunom yi tontou la
gnoun paa yi sounou diongué mi ngi djoublou thi lidjeunti teubeuski njaboot gui ak esquiver mbeukk* yi Mr. Green



*gniy gnaan khar ak yeuré teubeuski
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
pearl
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 14 Sep 2007
Posts: 3,288
Anniversaire: 29 septembre
Genre: Femme
Localisation: dakar
Point(s): 5,738
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 08:38    Post subject: diongué goor Reply with quote

goor gou djiongué deugeu moy takk  djiguénn bou gnoul- yarou, tékk thi gnarél bou khéss -perkité, beu paré naan léén :
-"yéén gnaar gneup yéneu yaam sameu kholl..."
Mr. Green
______________________________
....... Wink


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 09:20    Post subject: diongué goor Reply with quote


pla wax nga deugg dé !
nioune souniou diongué féténa  niouko  yagueuna ,
ça ne me traverse tellement pas l'esprit que je suis sincérement incapable d'en dire quoique ce soit !
 faténaniou lolou  , nioungui thi yénéne  nioune paa yi  !

à mon age kouma fékk di nioulal ak soll sollou xalé yi di boy boylou di  diéuma diapp guél waxmouma foumakoy wakhé !

______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 09:30    Post subject: diongué goor Reply with quote

bayil rek 

diadieuf seugn boni, déél djélleulé rek

goné yii kou léén topp wakh lou eup

dionguék khalélou goor ak dionguék borom keur dou bénn (n'est-ce pas pétaw? Wink )

______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 09:58    Post subject: diongué goor Reply with quote

mane dé paa la...sama stock de diongué diéxna...
lady défal é way, mane dé je croyais ke dionguou gor ngay wax (manam circoncision...xawna


Back to top
LOKIDOR
Légende
Légende

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 5,653
Anniversaire: 03 Aout
Genre: Homme
Localisation: 69, Av. du Chat, Duché d'Athépédie. NGAAY
Indisponibilité: passablement présent
Point(s): 10,534
Moyenne de points: 1.86

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:00    Post subject: diongué goor Reply with quote

C vrai goor di na diongué mais il ne fait comme la femme
Comme dis Lady en phase séduction il doit adopter une position plus attentiste que la femme, il doit attendre des signes et s'ils sont assez clairs et bien décodés (faut pas se tromper) il "attaque". Le rôle de la femme dans cette étape c'est d'émettre des signes (gestuelle, positions, expressions etc...) un homme normal quant à lui ne doit pas "attaquer" aveuglément une femme.
Dans le ménage le Diongué de l'homme c'est d'abord (comme le dit Plato) assurer la DQ et la sécurité du foyer (Imam m'a dit hier que nit Sour ak Sécurité rek la mounioul Niak! Té mouy deug!) Donc il faut que l'Homme rassure sur ces plans sa maisonnée. En plus de ses obligations régaliennes il faut qu'il soit drôle, qu'il soit taquin (intelligemment) il faut que mou meuneu solou, am charisme, cahque jour bouy wacc indalé ay mboussou produits, di diokh cadeaux Madame et les enfants, mais aussi di honoré sa femme partout (en, famille avec ses copains etc..) di ko titeuro, di ko tagg, di ko nab nabal, di ko rétane lo, di mey khaliss, di ko dieundeul li mou geuneu beug (mouy or ak yéré) di ko sagal en résumé. Té bou goudéé mou assuré: deuko ko ba sénégalam dieum kanam...!
______________________________
Essayer chaque jour d'être plus fort en distinguant mes besoins et mes caprices...

Celui qui ne tolère pas la plaisanterie supporte mal la réflexion...


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:02    Post subject: diongué goor Reply with quote

loki dé wané na bopam.....

Back to top
LJ
vip
vip

Offline

Joined: 03 Oct 2007
Posts: 3,790
Anniversaire: 28/12
Genre: Femme
Localisation: Fofou lé
Point(s): 6,892
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:10    Post subject: diongué goor Reply with quote

diaf way ton's khamonani doma rouss lo
______________________________
I am everything i am
because you loved me


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:19    Post subject: diongué goor Reply with quote

pour informations et études  sur le  diongué des paa  , voir le texte de loki
daccord thi té diko dieuffé nimouko wakhé soubeu ak ngoné !
wax ji diékhna ! takk takk !!!

jeunes mariés et célibataires prenez en de la graine ! kou thi dindi virgule perte nga !
______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
elpaix
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 17,970
Anniversaire: 10/05
Localisation: Athépédie
Point(s): 30,088
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:28    Post subject: diongué goor Reply with quote

lady, accentél "e" bi waay ! 
mane dé, j'attaque et je réfléchis après... louma am dieul... souniou ma seuleumé, ma fakhassou, dokh dokh bi..
______________________________


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:29    Post subject: diongué goor Reply with quote

Lokidor wrote:
C vrai goor di na diongué mais il ne fait comme la femme
Comme dis Lady en phase séduction il doit adopter une position plus attentiste que la femme, il doit attendre des signes et s'ils sont assez clairs et bien décodés (faut pas se tromper) il "attaque". Le rôle de la femme dans cette étape c'est d'émettre des signes (gestuelle, positions, expressions etc...) un homme normal quant à lui ne doit pas "attaquer" aveuglément une femme.
Dans le ménage le Diongué de l'homme c'est d'abord (comme le dit Plato) assurer la DQ et la sécurité du foyer (Imam m'a dit hier que nit Sour ak Sécurité rek la mounioul Niak! Té mouy deug!) Donc il faut que l'Homme rassure sur ces plans sa maisonnée. En plus de ses obligations régaliennes il faut qu'il soit drôle, qu'il soit taquin (intelligemment) il faut que mou meuneu solou, am charisme, chaque jour bouy wacc indalé ay mboussou produits, di diokh cadeaux Madame et les enfants, mais aussi di honoré sa femme partout (en, famille avec ses copains etc..) di ko titeuro, di ko tagg, di ko nab nabal, di ko rétane lo, di mey khaliss, di ko dieundeul li mou geuneu beug (mouy or ak yéré) di ko sagal en résumé. Té bou goudéé mou assuré: deuko ko ba sénégalam dieum kanam...!


li djaroon wakh yeup wakh nga ko

borom kër di kilifë di waay*
di bégël njaboot té du aay**
di sagal soxna té miin ngaay
njëgëm du yomb sudoon jaay


*waay = dans le sens de "complice", qui partage de bon moments avec sa famille
**aay = pingre, ne partage pas : "lu mu am aayé ko nit ñi"


ChineseStar gneuweul teudj sujet bi balaa HSeuses yi di gneuw diko khadiamal
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
boni-revenu-du-senegal
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 08 Feb 2007
Posts: 13,986
Point(s): 22,230
Moyenne de points: 1.59

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:34    Post subject: diongué goor Reply with quote

pla 
______________________________
"s'irriter d'un reproche , c'est reconnaitre qu'on l'a mérité "
tacite


Back to top
Mami
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 8,677
Anniversaire: 12 /10/2006
Localisation: Dans le coeur du Roi
Point(s): 15,284
Moyenne de points: 1.76

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:37    Post subject: diongué goor Reply with quote

plato wrote:
Lokidor wrote:
{{{Spoiler}}}


li djaroon wakh yeup wakh nga ko

borom kër di kilifë di waay*
di bégël njaboot té du aay**
di sagal soxna té miin ngaay
njëgëm du yomb sudoon jaay


{{{**}}}

ChineseStar gneuweul teudj sujet bi balaa HSeuses yi di gneuw diko khadiamal


rien à ajouter

fs machalla, maeva

______________________________
Nul ne peut fuir à sa destinée

L'amour d'une mère c'est comme l'air : c'est tellement banal qu'on ne le remarque même pas. Jusqu'à ce qu'on en manque !

الحمد لله


Back to top
LJ
vip
vip

Offline

Joined: 03 Oct 2007
Posts: 3,790
Anniversaire: 28/12
Genre: Femme
Localisation: Fofou lé
Point(s): 6,892
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 10:49    Post subject: diongué goor Reply with quote

rien à ajouté yaw loy azouté bayil guor gni niou disserté way Very Happy
______________________________
I am everything i am
because you loved me


Back to top
milena
Membre de base
Membre de base

Offline

Joined: 22 Sep 2008
Posts: 286
Anniversaire: 17 mars
Genre: Femme
Localisation: USEBE
Point(s): 470
Moyenne de points: 1.64

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 11:00    Post subject: diongué goor Reply with quote

Lokidor wrote:
C vrai goor di na diongué mais il ne fait comme la femme Comme dis Lady en phase séduction il doit adopter une position plus attentiste que la femme, il doit attendre des signes et s'ils sont assez clairs et bien décodés (faut pas se tromper) il "attaque". Le rôle de la femme dans cette étape c'est d'émettre des signes (gestuelle, positions, expressions etc...) un homme normal quant à lui ne doit pas "attaquer" aveuglément une femme.
Dans le ménage le Diongué de l'homme c'est d'abord (comme le dit Plato) assurer la DQ et la sécurité du foyer (Imam m'a dit hier que nit Sour ak Sécurité rek la mounioul Niak! Té mouy deug!) Donc il faut que l'Homme rassure sur ces plans sa maisonnée. En plus de ses obligations régaliennes il faut qu'il soit drôle, qu'il soit taquin (intelligemment) il faut que mou meuneu solou, am charisme, cahque jour bouy wacc indalé ay mboussou produits, di diokh cadeaux Madame et les enfants, mais aussi di honoré sa femme partout (en, famille avec ses copains etc..) di ko titeuro, di ko tagg, di ko nab nabal, di ko rétane lo, di mey khaliss, di ko dieundeul li mou geuneu beug (mouy or ak yéré) di ko sagal en résumé. Té bou goudéé mou assuré: deuko ko ba sénégalam dieum kanam...!




thièy bi dissertation yaram daw na yakh dess moussémoiselle yi dieulène exemple thi Ton's way do lène ko réthiou dé.
______________________________
Paix et Joie


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 11:22    Post subject: diongué goor Reply with quote

milena mane dé li loki bindeu nonoula mél...

Back to top
pearl
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 14 Sep 2007
Posts: 3,288
Anniversaire: 29 septembre
Genre: Femme
Localisation: dakar
Point(s): 5,738
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 11:30    Post subject: diongué goor Reply with quote

tialky yow sounou démé ndar, thi téféés bii ngeuy teud Evil or Very Mad
______________________________
....... Wink


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 11:32    Post subject: diongué goor Reply with quote

pearl mane dé li loki bindeu nonoula mél....

Back to top
le sage
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 3,459
Anniversaire: 17/06/
Localisation: dakar
Point(s): 6,273
Moyenne de points: 1.81

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 11:54    Post subject: diongué goor Reply with quote

guoor bou "normal" daal gnéte mo ko jikk
-01)sanguou ndieule téle...aprés une nuit "normal"
-02)diokhé ndieule li maname dépasse bi
-03ndieulou maname guéne keur gui outi lou mou indile ndiaboot gui
merci loki wakhale ngua guoor gnépe  mais lady t'as fais exprés bagna déf accent thi "e" bi wala   chaye chayewa
______________________________
assamane dal ken dou thi boukhanté n'guir khol ko.yalla yana


Back to top
milena
Membre de base
Membre de base

Offline

Joined: 22 Sep 2008
Posts: 286
Anniversaire: 17 mars
Genre: Femme
Localisation: USEBE
Point(s): 470
Moyenne de points: 1.64

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 12:39    Post subject: diongué goor Reply with quote



tialky BAMA wrote:
milena mane dé li loki bindeu nonoula mél...



hummmmmmmm ca commence à devenir interechant dé mais nak fok ma deff ay investigations pour xam ndax réellement nonou nga mel

May ma touti ma gneuw
______________________________
Paix et Joie


Back to top
KANIBOUSAF
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 17 Feb 2008
Posts: 9,627
Anniversaire: 01/03
Genre: Homme
Localisation: Dakar
Point(s): 15,144
Moyenne de points: 1.57

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 12:46    Post subject: diongué goor Reply with quote

elpaix wrote:
lady, accentél "e" bi waay ! 
mane dé, j'attaque et je réfléchis après... louma am dieul... souniou ma seuleumé, ma fakhassou, dokh dokh bi..


Diékhna takk El gnon bok tactik et tecknik Légui ak génération bou béss bi, affaire de diongué mo fi diékh tak j'attak, je cogne et je gagne rék lafi guisse Gniom séne bop sakh dagnou nane "goor daye guaw mba mouy loukhouss" légui sakh boussi gueuneu yombe lagnouy wakh "déss na si yaw" Alors à l'abordasse
______________________________
LES ENFANTS ONT PLUS BESOIN DE MODELES QUE DE CRITIQUES



Le Prophéte a dit : "Maintiens le lien avec celui qui te fuit, sois bon avec celui qui t'a causé du tort, et dis la vérité même si elle est à ton détriment."


Hadith - Ibn An-Najjar


Back to top
000
Power-Membre
Power-Membre

Offline

Joined: 08 Nov 2005
Posts: 1,070
Anniversaire: 000
Genre: Femme
Localisation: Wakhkatou Deug land
Point(s): 1,948
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 12:51    Post subject: diongué goor Reply with quote

Man dé dina déwatii wa rekk si FS, sista nakk bokossi, gsper que souniou amé borom keur dinégne dieul exemple si tons loki
lol


Back to top
maeva
vip
vip

Offline

Joined: 24 Apr 2007
Posts: 3,836
Anniversaire: 30/11
Genre: Femme
Localisation: Epicurie
Point(s): 6,402
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 13:09    Post subject: diongué goor Reply with quote

RFstar wrote:

Man dé dina déwatii wa rekk si FS, sista nakk bokossi, gsper que souniou amé borom keur dinégne dieul exemple si tons loki
lol

RF, sa 1000 messages ba taay matagoul
______________________________
La violence : une force faible.[Vladimir Jankélévitch]


Back to top
loufa
vip
vip

Offline

Joined: 02 Dec 2005
Posts: 3,874
Anniversaire: 07/10
Genre: Homme
Point(s): 6,017
Moyenne de points: 1.55

PostPosted: Tue 18 Nov 2008 - 13:15    Post subject: diongué goor Reply with quote

Té bou goudéé mou assuré: deuko ko ba sénégalam dieum kanam[/b]...![/quote]
GRAND diongué bi fi ma souligné la eupé solo
boy assure na khale bi yeug ni mom kesser moy djiguene
nga diko waxx sokhna ci danga saff djiguene
wala
______________________________


Back to top
Contenu Sponsorisé






PostPosted: Today at 08:24    Post subject: diongué goor

Back to top
Display posts from previous:   
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Société -> Le coin des femmes
All times are GMT
Goto page: 1, 2, 3, 4, 5, 6, 7, 8, 9  >
Page 1 of 9

 
Jump to:  

Portal | Index | Create a forum | Free support forum | Free forums directory | Report a violation | Conditions générales d'utilisation
Powered by phpBB
Appalachia Theme © 2002 Droshi's Island

Designed & images by Kooky