Portail - Index - FAQ - Search - Membres - Groupes - Register - Messages Privés - Log in
View unanswered posts
Qui est en ligne?
Who is Online

  [ Administrator ]   [ Moderator ]
Most users ever online was 205 on Mon 16 Sep 2019 - 14:25


 BIENVENUE ET MERCI POUR VOTRE VISITE 
Cliquer ici pour vous inscrire sur votre forum Smile
thiouraye
Goto page: 1, 2, 3, 4, 5, 6, 7  >
 
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Société -> Le coin des femmes
Previous topic :: Next topic  
Author Message
khadidiatou Diallo
Neophyte
Neophyte

Offline

Joined: 09 Jun 2008
Posts: 16
Anniversaire: 15 01 1965
Genre: Femme
Localisation: dakar
Indisponibilité: xxxxxxxxxx
Point(s): 31
Moyenne de points: 1.94

PostPosted: Mon 16 Jun 2008 - 19:09    Post subject: thiouraye Reply with quote

PublicitéSupprimer les publicités ?
waw gagni lo len kham thi thiouraye j adore ca et fou ma toll ma gui sourou j aime sentir bon vous croyer k le thiouraye peut apporter un plus dans la vie de couple cette question je la pose aux maries hommes ou femmes dites moi ce que vous en pensez
______________________________
diallo


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 07:52    Post subject: thiouraye Reply with quote

thiouraye bou gnou "neubeul bamou neub"
moulay effleuré té doula khèrr
dila khéégn té doula fatt
di guilli té doo kham foumouy bayikoo
Aïda Souka di sourou té kham nan la ak nakala
...........
euw!!
meun na lou baré!
surtout temps sédd nak
ça ne m'étonnerait pas que ce soit entre août et octobre qu'il y a le plus de polo

______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
LJ
vip
vip

Offline

Joined: 03 Oct 2007
Posts: 3,790
Anniversaire: 28/12
Genre: Femme
Localisation: Fofou lé
Point(s): 6,892
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 07:56    Post subject: thiouraye Reply with quote

thieuy fi la khéwèè nak on aura tout vu mouway thiouraye mo ssi déssone
khadiatou démal céti fatou laobé deugna elle est dispo pour ca pour everybody
______________________________
I am everything i am
because you loved me


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 08:02    Post subject: thiouraye Reply with quote

Tiey fii dé louné dinaa kofi wakh!!
Djéggalou dé
cé juste pour rigoler!

______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Last edited by plato on Tue 17 Jun 2008 - 08:07; edited 1 time in total
Back to top
LJ
vip
vip

Offline

Joined: 03 Oct 2007
Posts: 3,790
Anniversaire: 28/12
Genre: Femme
Localisation: Fofou lé
Point(s): 6,892
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 08:03    Post subject: thiouraye Reply with quote

c aussi juste pour rigoler

______________________________
I am everything i am
because you loved me


Back to top
pearl
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 14 Sep 2007
Posts: 3,287
Anniversaire: 29 septembre
Genre: Femme
Localisation: dakar
Point(s): 5,737
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 09:04    Post subject: thiouraye Reply with quote

mo!
baam sotti rék.
aprés mariass, tu passes à thiouraye!
féxél beu boulfi waax "ngénté" rék Confused
______________________________
....... Wink


Back to top
maeva
vip
vip

Offline

Joined: 24 Apr 2007
Posts: 3,836
Anniversaire: 30/11
Genre: Femme
Localisation: Epicurie
Point(s): 6,402
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 09:08    Post subject: thiouraye Reply with quote

pearl wrote:
féxél beu boulfi waax "ngénté" rék Confused


wala WOUDJ Mr. Green
______________________________
La violence : une force faible.[Vladimir Jankélévitch]


Back to top
elpaix
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 17,970
Anniversaire: 10/05
Localisation: Athépédie
Point(s): 30,088
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 09:23    Post subject: thiouraye Reply with quote

mais Plat, yow expert nga dé !
kharal imam ak magic nieuw ! nioniou niaar dé, tout ce qui touche à la vie conjugal, sén kham kham macc na ci ! mane dé khaw ma founiou ndiangué ?
______________________________


Back to top
pearl
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 14 Sep 2007
Posts: 3,287
Anniversaire: 29 septembre
Genre: Femme
Localisation: dakar
Point(s): 5,737
Moyenne de points: 1.75

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 09:32    Post subject: thiouraye Reply with quote

elpaix wrote:
 imam ak magic ..! mane dé khaw ma founiou ndiangué ?


sén moussé (waleu madame) moo aay rék
______________________________
....... Wink


Back to top
le sage
Habitué
Habitué

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 3,459
Anniversaire: 17/06/
Localisation: dakar
Point(s): 6,273
Moyenne de points: 1.81

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 10:34    Post subject: thiouraye Reply with quote

ya rien de tel qu'un bon parfum de thiouraye "fadiar"(3h30 du matin)
wala thi sa yeuré adiouma...j'adore!!!!
sokhnayi khétt guou nékhh da faye yokk  fane ak wérrr!!!!!!!!!!!
______________________________
assamane dal ken dou thi boukhanté n'guir khol ko.yalla yana


Back to top
mawaxone waxééte
Légende
Légende

Offline

Joined: 07 Jan 2006
Posts: 5,734
Point(s): 10,274
Moyenne de points: 1.79

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 10:38    Post subject: thiouraye Reply with quote

bilay grd....nay guili rék...boumou eupe boumou yéss

Back to top
Mami
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 8,677
Anniversaire: 12 /10/2006
Localisation: Dans le coeur du Roi
Point(s): 15,284
Moyenne de points: 1.76

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 10:46    Post subject: thiouraye Reply with quote

Plato wrote:
thiouraye bou gnou "neubeul bamou neub"
moulay effleuré té doula khèrr
dila khéégn té doula fatt
di guilli té doo kham foumouy bayikoo
Aïda Souka di sourou té kham nan la ak nakala
...........
euw!!
{{{Spoiler}}}


c'est l'expérience qui parle !
yaw lajoie démal thiourayou! thiouraye dafay doundal khol

______________________________
Nul ne peut fuir à sa destinée

L'amour d'une mère c'est comme l'air : c'est tellement banal qu'on ne le remarque même pas. Jusqu'à ce qu'on en manque !

الحمد لله


Back to top
000
Power-Membre
Power-Membre

Offline

Joined: 08 Nov 2005
Posts: 1,070
Anniversaire: 000
Genre: Femme
Localisation: Wakhkatou Deug land
Point(s): 1,948
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 11:14    Post subject: thiouraye Reply with quote

man dal diakhalngenma , khadidiatou degna dé djiguéne bou amoul dieukeur douy sourou,, hummmmmmmmmm wakhouma dara nakk,
mabdou lolou mo takhhh celibataires yi baré si foorumm bii hummm lol


Back to top
nounouche
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 8,613
Anniversaire: 19 septembre
Genre: Femme
Localisation: mbeuleukhé
Point(s): 13,877
Moyenne de points: 1.61

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 17:37    Post subject: thiouraye Reply with quote

deguena ko tamiit dé eref 
damey diay thiouraye kg 15 000 dong nak Laughing

______________________________


Back to top
khadidiatou Diallo
Neophyte
Neophyte

Offline

Joined: 09 Jun 2008
Posts: 16
Anniversaire: 15 01 1965
Genre: Femme
Localisation: dakar
Indisponibilité: xxxxxxxxxx
Point(s): 31
Moyenne de points: 1.94

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 19:32    Post subject: thiouraye Reply with quote

lolou ay wax rek la mame de sa you ma dougue fene gnap gestou dax sama thiouraye j aime ca te lima len ladj kene tontou wouma lane ley yok thi vie de couple
______________________________
diallo


Back to top
khadidiatou Diallo
Neophyte
Neophyte

Offline

Joined: 09 Jun 2008
Posts: 16
Anniversaire: 15 01 1965
Genre: Femme
Localisation: dakar
Indisponibilité: xxxxxxxxxx
Point(s): 31
Moyenne de points: 1.94

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 19:39    Post subject: thiouraye Reply with quote

pearl wrote:
mo! baam sotti rék.
aprés mariass, tu passes à thiouraye!
féxél beu boulfi waax "ngénté" rék Confused



non guente apres mariage negene me say damay oute ay feme puisque dama xawa timide j attends vos conseils apres so guente ware gneuw mou gneuw
______________________________
diallo


Back to top
LOKIDOR
Légende
Légende

Offline

Joined: 25 Oct 2005
Posts: 5,653
Anniversaire: 03 Aout
Genre: Homme
Localisation: 69, Av. du Chat, Duché d'Athépédie. NGAAY
Indisponibilité: passablement présent
Point(s): 10,534
Moyenne de points: 1.86

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 21:57    Post subject: thiouraye Reply with quote

man d depuis bi ma guissé Kg thiouraye 45000 la ko commencé bagn khamné sama poss dou ko fékké
______________________________
Essayer chaque jour d'être plus fort en distinguant mes besoins et mes caprices...

Celui qui ne tolère pas la plaisanterie supporte mal la réflexion...


Back to top
nounouche
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 24 Oct 2005
Posts: 8,613
Anniversaire: 19 septembre
Genre: Femme
Localisation: mbeuleukhé
Point(s): 13,877
Moyenne de points: 1.61

PostPosted: Tue 17 Jun 2008 - 23:54    Post subject: thiouraye Reply with quote

ya ney rek...
______________________________


Back to top
4ever
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 23 Oct 2005
Posts: 7,563
Genre: Homme
Point(s): 12,801
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 07:08    Post subject: thiouraye Reply with quote

kilo 45 000 
xanaa loolu at lay diiré kon ?
wala ?
______________________________
Way, Wey


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 07:36    Post subject: thiouraye Reply with quote

khadidiatou Diallo wrote:
lolou ay wax rek la mame de sa you ma dougue fene gnap gestou dax sama thiouraye j aime ca te lima len ladj kene tontou wouma lane ley yok thi vie de couple
moo
ma tontoula ba paré
weu! Evil or Very Mad

limouy yokk ci vie de couple?
borom keur bou yakkamti gnibbi, té sawar ci toog keureum
té dafay facilité "collé-serré" (honni soit qui mal y pense!)

ma yém fii ndakh ay goné dagn fi nekk Mr. Green

______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
LJ
vip
vip

Offline

Joined: 03 Oct 2007
Posts: 3,790
Anniversaire: 28/12
Genre: Femme
Localisation: Fofou lé
Point(s): 6,892
Moyenne de points: 1.82

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 07:46    Post subject: thiouraye Reply with quote

waw wakh deugg yaw diallo diérry khana do guiss téneul si kaw plato tontou nala bou yagg té doli nala fii niii

collé-sérré kay
plato miiii

______________________________
I am everything i am
because you loved me


Back to top
maeva
vip
vip

Offline

Joined: 24 Apr 2007
Posts: 3,836
Anniversaire: 30/11
Genre: Femme
Localisation: Epicurie
Point(s): 6,402
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 09:14    Post subject: thiouraye Reply with quote

nounchy wrote:
damey diay thiouraye kg 15 000 dong nak


Tu prends en charge les frais denvoi et de livraison wala ?

for ak lady bo lene si wakhé na lene chiffaay (dixit elpé)

______________________________
La violence : une force faible.[Vladimir Jankélévitch]


Back to top
plato
Maître du forum
Maître du forum

Offline

Joined: 12 Nov 2007
Posts: 8,622
Point(s): 14,512
Moyenne de points: 1.68

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 09:21    Post subject: thiouraye Reply with quote

man dé nééna mout Mr. Green
______________________________
ku xeebul sa nguur di buur


Back to top
4ever
Mod.
Mod.

Offline

Joined: 23 Oct 2005
Posts: 7,563
Genre: Homme
Point(s): 12,801
Moyenne de points: 1.69

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 09:23    Post subject: thiouraye Reply with quote

man xalé laa, "bul déf" laay bagna degg.

mané nga jeundd ci yu 45 000 yi laa wax, xanaa beugoo mu perkité carrément
bu nieuwé nak, nga sedd ma sama wàll,
nay ba déé
.
______________________________
Way, Wey


Back to top
maeva
vip
vip

Offline

Joined: 24 Apr 2007
Posts: 3,836
Anniversaire: 30/11
Genre: Femme
Localisation: Epicurie
Point(s): 6,402
Moyenne de points: 1.67

PostPosted: Wed 18 Jun 2008 - 09:28    Post subject: thiouraye Reply with quote

forever wrote:
man xalé laa, "bul déf" laay bagna degg.

mané nga jeundd ci yu 45 000 yi laa wax, xanaa beugoo mu perkité carrément
bu nieuwé nak, nga sedd ma sama wàll, {{{Spoiler}}}.


wa yaaw loy doyé thirourayye Very Happy Very Happy warou si yaw
______________________________
La violence : une force faible.[Vladimir Jankélévitch]


Back to top
Contenu Sponsorisé






PostPosted: Today at 10:46    Post subject: thiouraye

Back to top
Display posts from previous:   
Post new topic   Reply to topic    Bienvenue sur le Forum futursenegal Forum Index ->
FORUMS FUTURSENEGAL
-> Société -> Le coin des femmes
All times are GMT
Goto page: 1, 2, 3, 4, 5, 6, 7  >
Page 1 of 7

 
Jump to:  

Portal | Index | Create a forum | Free support forum | Free forums directory | Report a violation | Conditions générales d'utilisation
Powered by phpBB
Appalachia Theme © 2002 Droshi's Island

Designed & images by Kooky